Méritewoumala

AMADEUS

Compositor: Não Disponível

Méritewuma la, eh
Méritewuma la, eh
Méritewuma la, eh

Waxal sa xol ni fonku na
Ko tekk na ko fu ma teggul kenn
Ahn he ya he, hum
Waxal sa xol ni fonku na
Ko tekk na ko fu ma teggul kenn
Ahn he ya he, hum

Méritewuma la
Méritewuma la
Yàlla xam na méritewuma la
Ooh, méritewumala

Attewoo ma ñakkal ba may déconner
Décider woo bañ ma xaar ba ma xéy dem
Dund bi yépp yëk sa tar
Te taxul nga changer
Méritewuma la

Waxal sa xol ni fonku na
Ko tekk na ko fu ma teggul kenn
Ahn he ya he, hum
Waxal sa xol ni fonku na
Ko tekk na ko fu ma teggul kenn
Ahn he ya he, hum

Méritewuma la
Méritewuma la
Yàlla xam na méritewuma la
Ooh, méritewumala

Na asamaan si taw mur sa ay rangooñ
Na denn bi dal neb say xixet
Bëgguma nga jooy danga may dofloo
Rabil-allahmin na ma booleek yaw
Ci sa wet rekk lay mëna keparoo

Waxal sa xol ni fonku na
Ko tekk na ko fu ma teggul kenn
Ahn he ya he, hum
Waxal sa xol ni fonku na
Ko tekk na ko fu ma teggul kenn
Ahn he ya he, hum

Méritewuma la
Méritewuma la
Yàlla xam na méritewuma la
Ooh, méritewumala

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital